Menu
DakarFlash
DakarFlash.com



Confidence: « Mon copain veut que je lui montre sur webcam mes…. »


Rédigé par DakarFlash.com, le Vendredi 16 Octobre 2015 || 755 Partages

Dans un orthographe exécrable, voici le message de détresse de cette internaute :

Suis en couple avec un homme depuis plus trois ans au debut tt etait rose il maimait trop mem si dawouma defal ndakh amoul mann sakh mako donn defal mais mann lolou dou wonn problem ndakh manker wouma wonn dara dama donn diang am bourse tee samay parent bagnalounn ma wonn dara on a traverser bcp de chose… sounou intimiter nak da yemonn ci fonn rek pas otre chose ndakh ninn ma yarer la tee makham sama bopp mais dal lima diakhal batakh ma beug conseil moy dafa febar son samba ndiaye ne fonctionn plus tee pr son traitement sn medecin dafa niko en plus des medoc il faut mouy deff ay flirt pousser tee nena douko def ak kennenn kou doul mamn legui nak il mimpose pour sounouy communiquer par skype may simikou tte nue o debut javai refuser pck khamouma lolou mai moumay menancer sinon dafay kharou il a mem tenter de se suicider plusieurs fois ma ragal avoir sa mort sur ma conscience ma nangou mai je nai pas la conscience trankil soumay diouli sakh limay deff lo rek lay guiss je sai pas cmt faire pour mou bayi ses menaces ak limay deff lo jai essauer plusieurs fois de le kitter mais tjrs daff may menancer bama delou ak mom aidez moi svp jattend vos conseils. »

Que lui conseillez-vous ?

Buzzsenegal


Dakarflash2




1.Posté par lora le 17/10/2015 08:42
yaw hammmm

2.Posté par bily bello ka le 17/10/2015 13:20
Boule ragale dara ma soeur manoule thi yaw darà ko yakar yalla la yakar kone nak gueumale sa bope thi lou bakh lila saye wadjour yarè

Nouveau commentaire :


Dans la même rubrique :
< >