Menu
DakarFlash
DakarFlash.com



Serigne Modou Kara : Encore une Ode aux Saltigués du Sénégal


Rédigé par DakarFlash.com, le Mardi 28 Juin 2016 || 131 Partages

Après Me Abdoulaye Wade, Macky Sall et Youssou Ndour, voilà encore Sérigne Modou Kara qui nous revient avec son inspiration débordante. Pour cette fois, il dédie son odes aux Prêtres traditionnels plus connus sous le nom de «Saltigués ». 
  
Maa ngiy nuyu sama mbòkk Saltige yi 
Ñiy feeñ ak ñiy nëbbu te yore mbir yi 
Jiby Njaay, Maître de la cérémonie 
Ngañ Géy n° 2 mi gën, na kiy tane 
Njaw Juuf, Ibrahima Ndong ak Omar Njaay 
Yii, yéen a ngi ko dònn’oo woon ci seen i baay 
Mahe-Maci, Géej-Wañe ak Xaar Juuf 
Lan-Njugaan, Amy Fay ak Fòode Juuf 
Môdu-KARA leen di nuyu, di leen wooh 
Ci BAMBA-Fépp, te yéen ñëpp la ciy wooh 
Li ngeen di wax, te BUUR bi di leen sutural 
Ba ngeen cay am lu ngeen di def ci seen i gaal 
Kon sant war na ci yéen nim ñu waree 
YÂLLAH, YONNENT a bi, ci kaw bu ñu goree 
Imânan wa Islâman wa Ihqsânan 
Dey tax lépp gën a rafet, baynanan 
  
Traduction française 
J’adresse mes salutations à mes parents Prêtres traditionnels 
Ceux qui s’affichent et ceux qui sont cachés parmi eux, détenteurs de mystères 
Djiby Ndiaye Maître de cérémonie 
Ngagne Guèye n° 2 et meilleur, tel ce lanceur de cauris 
Ndiaw Diouf, Ibrahima Ndong et Omar Ndiaye 
Ce legs, vous l’avez eu hérité de vos pères 
Mahé-Mathie, Guédj-Wagné, ainsi que Khar Diouf 
Lane-Ndioungane, Amy Faye et Fodé Diouf 
Modou-Kara vous salue et vous invite 
Dans BAMBA-Fépp, et tous, vous y êtes appelés 
Ce que vous invoquez, et que DIEU vous accorde dans Sa Miséricorde 
Vous permettant d’en tirer de quoi emplir vos coffres 
Vous en êtes redevables de louanges à la même manière que nous autres 
Envers DIEU et Son MESSAGER, si toutefois nous sommes reconnaissants 
Car la Soumission à DIEU, la Foi et la Perfection 
Permet de tout mener à l’Excellence, entre nous.

DakarFlash3



Nouveau commentaire :